Yeah, was born in 1995
Juddoo Ghetto, màggee Ghetto
My name is Ashs, you know the vibes I′m from zero to hero
Seereer ci baay Baay Faal ci life, ci man dara du fi dara
May kan nitt ku toroxlu la, mujj bu rafet rekk ñaan
Was born in 1995, boroom basse bi guitare bi sam baay
Yaay Joor def li nekk ci man, mënu ma dof fate fi ma jaar
Boy laa woon comme boy yëpp, amoon rêve pour tëpp tekki
pour ñëpp
Yalla Buur bi doggal, du ma lenn kenn mais lepp ñëpp
Was born in 1995
(Born in 1995, yo)
Yo, born in 1995
Juddoo biir ghetto maggee biir Ghetto
Taxul nga raw ñu brain ci life
(1995 yo yo, 1995 yo yo)
Ma nekk ku kenn nekkul ci ñoom
Ñoom dañ ma jiitu fu lëndëm ma len niital fu ñuy tekk sen
tànk
(1995)
This is what I do all night
This is what I do every fucking night
Fuck ñu fogoon ni ñëwoon pour tekki ci rew me we try all
day all night
Tukki du tekki, tekki du tukki teewul
Ñoo ngi jekk ci game bi ligeey money fayeeku
Nobody can stop my mind
Nobody can stop my mind
Juddoo ci hood màggee ci hood bi fuck almadies ak Cap
Si mbedd buur bi lañ jàngee hip-hop même prési day xaar
Bañ nga def ma jàam ma def rappeur bu mag
Bëggu ma kaaw ak gellu tubaab
Juddoo ci reew mi tekkee ci reew mi from zero to hero
Página 1 / 2