Cifra Club

Coup Bas

Cherifou

Ainda não temos a cifra desta música.

Wowoo yaw
Ñi lay tagg tay, suba ñoo lay saaga
Ñi lay topp tay, suba ñoo lay jaay
Ñi la bëgg tay, suba ñoo lay noonoo
Ni nga wóolu tay, suba ñoo lay wóorloo

Gore dafa jeex, goreedi des fi
Te dëggi bu tëwë luy des fi
Noppalul waay, wax nga ba tooy
Maa ngi ci doorwar, yaa ngi ci xeew
Door naan ma saaga naañ ma
Daf naan ma picc tëj ma
Yóor ma ci biir teen ba lala sulli naañ ma

Man taluma leen
Man gisuma leen
Maa ngi sama yoon
Gaynde faat ma xam na taluma leen
Man yëguma leen
Wa wallaay faalewuma leen
Ehn nanguleen
Yàlla dogal

Kuy yëngal jamano
Sayuma neexe, maay yëngal jamano
Wa wallaay yaw la
Man mi ma yëngal jamano
Saa su ma neexee damay yëngal jamano
Wa wallaay yaw la

Am na ay coup bas
Ngir ma def faux pas
Bëgg ma tuutal
Hééé, lii lan la?

Am na ay coup bas
Ngir ma def faux pas
Bëgg ma tuutal
Hééé, lii lan la?

Bu Yàlla taane jaam
Danga naan waaw
Nangudogoloo
Day noppal jamm
Lim la järal la ma järal
Duma kuy dës ginnaaw
Ñun dañoo nangu lool
Doyloo Yàlla

Man ne naa du la seetaan nga fiy ñaaw
Dalla bëgg!
Man ne naa du la seetaan nga fiy ñaaw
Ey, dalla bëgg!
Yaay booy ne na du la seetaan nga fiy ñaaw
Dalla bëgg!
Baba ne na du la seetaan nga fiy ñaaw
Ey, dalla bëgg!

Kuy yëngal jamano
Sayuma neexe, maay yëngal jamano
Wa wallaay yaw la
Man mi ma yëngal jamano
Saa su ma neexee damay yëngal jamano
Wa wallaay yaw la

Am na ay coup bas
Ngir ma def faux pas
Bëgg ma tuutal
Hééé, lii lan la?

Am na ay coup bas
Ngir ma def faux pas
Bëgg ma tuutal
Hééé, lii lan la?

Hééé
Hééé

Lim la järal la ma järal
Duma kuy dës ginnaaw
Ñun dañoo nangu lool
Doyloo Yàlla

Outros vídeos desta música
    0 exibições

    Afinação da cifra

    Afinador online

    0 comentários

    Ver todos os comentários

    Evolua na música em diferentes instrumentos

    Mais de 15 cursos com aulas exclusivas, materiais didáticos e exercícios por R$49,90/mês.

    Começar a aprender

    Entre para o Cifra Club PRO

    Tenha acesso a benefícios exclusivos no App e no Site

    • Chega de anúncios

    • Mais recursos no app do Afinador

    • Atendimento Prioritário

    • Aumente seu limite de lista

    • Ajude a produzir mais conteúdo

    Cifra Club PRO

    Enjoy Cifra Club with exclusive benefits and no ads
    Cifra Club PRO
    Enjoy Cifra Club with exclusive benefits and no ads
    Ops (: Contenido disponible sólo en portugués.
    OK