Cifra Club

Limay Yeuk

Sokhou Bb

Ainda não temos a cifra desta música.

Man li may yëg ci yaw
Ëpp na ma doole
Ay waay mbëggeel
Waa ji kii lu mu ma def
Waatoon naa ndax xàddi woon
Ne dootul doonati maak moom
Waa ji kii lu mu ma def

Man bëgguma ku dul yaw
Aah yeah, te xam nga ko
Yaa dee ci sama xol bi
Ndax mbëggeel gi nga may wan

Ngiro naa ci yaw
Xol bi gagné nga ko
Doo seen moroom
Sama Nutella
Xol bi fees nga ko, yaw laa nob
Bëgguma keneen

Ay li may yëg sama xol bi
Yaay sama seytaane
Ay li may yëg sama xol bi
Li may yëg ëpp na ma doole

Mbëggeel yaay mbër mu bari doole
Lu tax bu ma ko séenee muy ñëw
Samay tànk jaxasoo
Sama fit wi day dem
Bu ma koy xool
Sama xol day féex

Aah wuy maa ngi dee
Wuy walloo!
Ay bu ma bàyyi bae
Sibi ri-bi-bi-bi-bib
Bu ma mas a bàyyi bae
Sibi woo-woo-woo
Yaw laa nob

Ngiro naa ci yaw
Xol bi gagné nga ko
Doo seen moroom
Sama Nutella
Xol bi fees nga ko, yaw laa nob
Bëgguma keneen

Ay li may yëg sama xol bi
Yaay sama seytaane
Ay li may yëg sama xol bi
Li may yëg ëpp na ma doole

Aah! Yeaaah!

Yaw laa bëgg yaw laa miin
Sama xol bi
Yaw yaay sama weeruwaay
Yaay sama seytaane
Ay li may yëg sama xol bi
Li may yëg ëpp na ma doole

Outros vídeos desta música
    0 exibições

    Afinação da cifra

    Afinador online

    0 comentários

    Ver todos os comentários

    Evolua na música em diferentes instrumentos

    Mais de 15 cursos com aulas exclusivas, materiais didáticos e exercícios por R$49,90/mês.

    Começar a aprender

    Entre para o Cifra Club PRO

    Tenha acesso a benefícios exclusivos no App e no Site

    • Chega de anúncios

    • Mais recursos no app do Afinador

    • Atendimento Prioritário

    • Aumente seu limite de lista

    • Ajude a produzir mais conteúdo

    Cifra Club PRO

    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Cifra Club PRO
    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Ops (: Contenido disponible sólo en portugués.
    OK