Cifra Club

Sai Sai

VJ

Ainda não temos a cifra desta música.

Suma la nammee bàyyi jëlal paaka das rey ma
Ndax boole nga li nga am ak li nga amul lépp jox ma
Su ma lay feccal guddi, bae du ñàkk fayda
Ma boole sama xol bi ak xëtër tegsi junni may la

Mbëggeel ni mu neexee bu de dëgg la du lu may wax
Dundu ci li ñu fekke danga jonge te neex a àndal
Ala, ala, architecte bi
Defar qui de ma ni ayna
Yaw wowal ma sa bajjen
Mu ñëw fok mu leeral ma

Woy jonge nga
Yàq sa ay neexay
Danga rafet, toogaay
Neex neex la cuuraay
Yëngal nga ma

Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wacc ko ba muy zéro (saay-saay)

Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal xaar xool yeneen la lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Na fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!

Ma mujje jaaxle
Ndekkete bidéew dina feñ bëccëg yaa ngi
Ñi ne neñ dama dof ñi neex dama saalit
Laajal sama gars ñi
Man lu ma daaneel yombul waaye k, o nga ma

Bànneex bi ñu nekke dafa ëpp ba mënuma wax
Xale bi ni nga jekke danga jonge te neex a àndal
Ala, ala, architecte bi
Defar qui de ma ni ayna
Yaw wowal ma sa bajjen
Mu ñëw fok mu leeral ma

Woy jonge nga
Yàq sa ay neexay
Danga rafet, toogaay
Neex neex la cuuraay
Yëngal nga ma

Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wacc ko ba muy zéro (saay-saay)

Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal xaar xool yeneen la lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Na fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!

Yàq sa ay neexay
Danga rafet, toogaay
Neex neex la cuuraay
Yëngal nga ma (saay-saay)

Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wacc ko ba muy zéro (saay-saay)

Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal xaar xool yeneen la lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Na fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!

Teg jeexal ci yaw chérie
Ba ma ñépp bàyye yaw la dese
Boo ma bàyyee man dina dee bae
Kon colleel serréel, bébé fais-moi rêver

Man suñ ma laajee
Kan mooy sama moitié
Man mëna waat ne
Yaw yaay sama moitié

En collé serré, bébé fais-mois rêver
Saa yu ñu gisee, gisoo ni muy neexee
Dans ciel étoilé que nous deux ma moitié
En collé serré, bébé fais-moi rêver

En collé serré, bébé fais-moi rêver
Saa yu ñu gisee, gisoo ni muy neexee
Dans ciel étoilé que nous deux ma moitié
En collé serré, bébé fais-moi rêver

Outros vídeos desta música
    3 exibições

    Afinação da cifra

    Afinador online

    0 comentários

    Ver todos os comentários

    Evolua na música em diferentes instrumentos

    Mais de 15 cursos com aulas exclusivas, materiais didáticos e exercícios por R$49,90/mês.

    Começar a aprender

    Entre para o Cifra Club PRO

    Tenha acesso a benefícios exclusivos no App e no Site

    • Chega de anúncios

    • Mais recursos no app do Afinador

    • Atendimento Prioritário

    • Aumente seu limite de lista

    • Ajude a produzir mais conteúdo

    Cifra Club PRO

    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Cifra Club PRO
    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Ops (: Contenido disponible sólo en portugués.
    OK