{{ t._('internal-error:title' ) }}
Vish! Alguém pegou todas as nossas palhetas! Nossa equipe de gnomos está resolvendo o caso!

Enquanto isso, fique por dentro das novidades!

Facebook CifraClub

Sori Nga

Def'l Nice

Ainda não temos a cifra desta música.

Jege nga géej gi bàyyi ko ginnaaw
Moom de jooy na jooy a jooy ba rongoñ fer, ay waay!
Bëgg naa la, muñal naa la, kii sa yaayu doom la
Bëgg naa la, muñal naa la, kii sa yaayu doom la
Jege nga géej gi bàyyi ko ginnaaw
Moom de jooy na jooy na jooy ba rongoñ fer, ay waay!
Sori nga leen ba fàtte leen te loolu waru la
Sori nga leen ba fàtte leen te loolu waru la

Nekk ak man lu ne temps xam lu ñépp
Dugg ci yaw te lank du dëpp
Dem ba jeex la xolam di gis
Te xool du sax bam bañ koy gis
Xoolal ci moom ni muy dunde
Metti naa lool, ci xolam yaay ki fa jeex
Yaay ki walla ci lépp li xeew
Mu gëm te gëm ne mbëggeel dey fay
Yaay ki waral ba fépp foo dem
Mu toog te muñ te xaar nga teew
Lu ko fi te, xanaa mbëggeel
Lu ko fi te, xanaa kóllëree

Jege nga géej gi bàyyi ko ginnaaw
Moom de jooy na jooy a jooy ba rongoñ fer, ay waay!
Bëgg naa la, muñal naa la, kii sa yaayu doom la
Bëgg naa la, muñal naa la, kii sa yaayu doom la
Jege nga géej gi bàyyi ko ginnaaw
Moom de jooy na jooy na jooy ba rongoñ fer, ay waay!
Sori nga leen ba fàtte leen te loolu waru la
Sori nga leen ba fàtte leen te loolu waru la

Fi nga ne sori na, fàtte leen waru la
Tukki bàyyi leen jaboot toog di la xaar hé héé oh!
Fi nga ne sori na, fàtte leen waru la
Tukki bàyyi leen yeah hééhéé!
Sa yaayu doom
Fi nga ne sori na, fàtte leen waru la
Tukki bàyyi njaboot toog di la xaar
Sa yaayu doom hé hé!
Sa yaayu doom
Sa yaayu doom
Sa yaayu doom

Outros vídeos desta música
    0 exibições

    Afinação da cifra

    Afinador online

    0 comentários

    Ver todos os comentários

    Evolua na música em diferentes instrumentos

    Mais de 15 cursos com aulas exclusivas, materiais didáticos e exercícios por R$49,90/mês.

    Começar a aprender

    Entre para o Cifra Club PRO

    Tenha acesso a benefícios exclusivos no App e no Site

    • Chega de anúncios

    • Mais recursos no app do Afinador

    • Atendimento Prioritário

    • Aumente seu limite de lista

    • Ajude a produzir mais conteúdo

    Cifra Club PRO

    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Cifra Club PRO
    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Ops (: Contenido disponible sólo en portugués.
    OK