Cifra Club

Labat

Fatou Laobé

Ainda não temos a cifra desta música.

Ãa kaay labat ma
Ñaan ma sama baay bóoy
Mu may ma laa waaw

Ãa kaay labat ma
Ñaan ma sama baay bóoy
Mu may ma laa waaw

Billaay njool mu ndaw
Kaay dogaale ma yóbbu
Foo jëm aawoloo ma
May wolal sa yaay
Di ko toggal
Di root muy naan

Ãa kaay labat ma
Ñaan ma sama baay bóoy
Mu may ma laa waaw

Billaay njool mu ndaw
Kaay dogaale ma yóbbu
Foo jëm aawoloo ma
May wolal sa yaay
Di ko toggal
Di root muy naan

Ãa kaay labat ma
Ñaan ma sama baay bóoy
Mu may ma laa waaw

Damay sangu solu xeeñ lu neex
Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
"Plat" bi nga gën a bëgg laay rëgal
Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
Junni yi ngay maye ma di ko dégg mayoo ma ci
Chéri waaye bala ngaa ñëw ma nelaw
Jongoma joo séen dem may kob junni
Xanaa xamoo ne man mi jongoma laa

Ãa kaay labat ma
Ñaan ma sama baay bóoy
Mu may ma laa waaw

Man ak mbëggeel
Wóo wóo wówóow man ak mbëggeel
Leeg-leeg nu toog di waxtaan
Sunu diggante neex ba mel ni suukar
Leeg-leeg nu toog di waxtaan
Seytaane dikk nu daal di réeróo
Nun jigéen ñi nun ñépp a yem
Ku leen di yor da nga leen di muñal
Fàllu bu la Kura tooñatee
Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Omar bu la Maam Njaay tooñatee
Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Aysata Sow yaw Yàlla na la Yàlla may looy béggéey
Yaw rekk laa waaw

Asan bu la Faat naar tooñatee
Jéggal ko xam ne jigéen a la jur
Aziz Gay bu la Ndey Mbay tooñatee
Jéggal ko te xam ne jigéen a la jur
Ami Jeŋ yaayu Maas Njaay dara weesul
Man xam naa ni yaw rekk la
Fiiru ma Matar Ndiaye fiiru ma
Yaw la bëgg yaw laa miin fiiru ma
Fiiru ma maa fiiru ma
Yaw laa xam yaw laa miin fiiru ma
Wóo wóo wóowu wóowu
Chéri I love you, waaw

Mon chéri
Mon chéri
Mon chéri
Yaw rekk laa

Waaw ñaar ñu bëggante
Boo ca xajul wax ca lu baaxoo
I love you waaw

Mon chéri
Mon chéri
Mon chéri
Yaw rekk laa

Billaay Aas !
Chéri Daado Géy
Dee ko muñal
Dee ko muñal waaw
I love you waaw

Mon chéri
Mon chéri
Mon chéri
Yaw rekk laa

Ndey Faatu Njaay
Ndey Faatu Njaay
Madame Deme
Yàllaa nu boole
Yaw rekk laa waaw

Mon chéri
Mon chéri
Mon chéri
Yaw rekk laa

Billaay Aliwu Ba
Chéri Jee
Bu la Jee tooñatee
Jéggal koo
Yaw rekk la gëm waaw

Mon chéri
Mon chéri
Mon chéri
Yaw rekk laa waaw

Mon chéri
Yaw rekk laa
Mon chéri
Yaw rekk laa waaw
Mon chéri
Yaw rekk laa waaw
Mon chéri
Yaw rekk laa waaw

Outros vídeos desta música
    0 exibições

    Afinação da cifra

    Afinador online

    0 comentários

    Ver todos os comentários

    Evolua na música em diferentes instrumentos

    Mais de 15 cursos com aulas exclusivas, materiais didáticos e exercícios por R$49,90/mês.

    Começar a aprender

    Entre para o Cifra Club PRO

    Tenha acesso a benefícios exclusivos no App e no Site

    • Chega de anúncios

    • Mais recursos no app do Afinador

    • Atendimento Prioritário

    • Aumente seu limite de lista

    • Ajude a produzir mais conteúdo

    Cifra Club PRO

    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Cifra Club PRO
    Aproveite o Cifra Club com benefícios exclusivos e sem anúncios
    Ops (: Contenido disponible sólo en portugués.
    OK